Migmafrica – Talibé

Migmafrica Talibé

Migmafrica – Talibé Lyrics

Artist: Migmafrica
Song: Talibé

Talibay mingui yelwan yenyi gnawna
Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul
Talibay mingui yelwan yenyi gnawna
Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul

Ndongo daara mingui joy
Guissul ndeye guissul baye
Mingui si mbede mi
Sol sagaram yori potam

Mom mingui yelwaane
Gudi ak beyceyk suba ak ngoone
Nagnu yeyreym xaleyi ndax xalay mooy done mak eyleyk
Amal yeyrmanday sakkul yeyrmanday ci ndongal daara yi

Amal yeyrmanday sakkul yeyrmanday ci ndongal daara yi
Talibay mingui yelwan yenyi gnawna
Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul
Africa di sunu reew

Ngala dagnu wara boolo
Suma xooley wa Europe dagnu boolo nek Union Européenne
Ma xool wa Amérique dagnu boolo nek les États-Unis d’Amérique
Pourquoi pas l’unité africaine

Ndax gnu mana deyvelopper sunu Africa dem ca kanam
Loley jeym lay sugnu reew yay ca kanam
Mangui woo peuple africain
Talibay mingui yelwan yenyi gnawna

Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul
Chez moi, les enfants de la rue, on les appelle Talibé
Africa! Comment se fait-il que tes enfants soient abandonnés?
Sunu beygay sunu Africa jeym ca kanam

Xalay bu meyti done nagnu leene yobbu ci daara yi
Yobbu leene ci école yi
Jaangal leene yoku leen xam xam loley taxa jemlay africa ca kanam
Maangi woo people africain

Talibay sonana talibay jaaxlay na
Gissoul ndeye gissoul baay
Gissoul ndeye gissoul baay
Nekka ci mbedda mi di yelwaane nekka ci mbedda mi di yelwaan waan waan waan

Ayca leene ayca leene ayca leene nako dal
Je donne ma voix aux enfants de la rue
Ndongo daara du xamga daara
Toj sa xool ba noppi defci daara njangi njangane so mokolay ndagay bay sa daara

Lo doonul talibay muno done serignam
Yeyrmaandé ci ndogo daara yi
Ay ca leene
Talibay mingui yelwan yenyi gnawna

Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul
Talibay mingui yelwan yenyi gnawna
Talibay mingui yelwan yenyi rafaytul
Find more lyrics at https://dcslyrics.com

You can purchase their music thru
DCSLyrics.com Amazon Music    DCSLyrics.com Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases

Migmafrica Lyrics – Talibé

Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.

Release Year: 2023