
Youssou N’Dour – Habib Faye Lyrics
Artist: Youssou N’Dour
Song: Habib Faye
Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap
Khamal ni diaposi dara
Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap
Khamal ni diaposi dara
Mane youssou niak na andando bou sincère
Aduna aduna dal nakhati naniu
Aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wa diu bax diu tey demna
Habib yarou wone na Andak dignité
Fonkone na liguey beugone ndiabotam
Donone diambar
Mane youssou niak na andando bou sincère
Aduna aduna dal nakhati naniu
Aduna aduna dafay woré Habib Faye demna ni wan diu bax diu tey demna
(Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou deugguel ko
(Habib, Habib) Man dal mangi len koy dialé yen wa famille wam ak ay fans sam
(Habib, Habib) Di len di hamal ni Habib Faye diougué woufi
(Habib, Habib) Nio fi defon mak mom mou woné fa loutax nitt gni beugueon ko
Senegal la gui lay dioy
Rew bangui lay dioy
Africa la gui lay dioy
Aduna la gui lay dioy
(Habib, Habib) Sama beugg beugg moy li
Sa beugg beugg moy leh
NItt kouné ak bеugg beuggam
Yallah na done
Yallah na done
La gеun ci mom
Ladial wa doundou gué anh…
Habib goudé na goudé na
(Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou wané fa
(Habib, Habib) Wané fa loutax nieup nieup beuggon ko
(Habib, Habib) man Youssou niak na andado bou sincère
Aduna aduna dal nakhati naniu
Aduna aduna dafay woré Habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna
Find more lyrics at https://dcslyrics.com


Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Celine Dion – Destin
1771 GVNG – LIFE SUPPORT
Youssou N’Dour Lyrics – Habib Faye
Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.
From the album:
H2O
Release Year: 2012