![Migmafrica Djali Kora](https://dcslyrics.com/wp-content/uploads/migmafrica-djali-kora.jpg)
Migmafrica – Djali Kora Lyrics
Artist: Migmafrica
Song: Djali Kora
Djali kora yaangi ni, sabar yangini
Li leyp benna la
Djali dundun yaangi ni, tama yaangi ni
Li leyp benna la
Djali yo yow la ila (djali yo yow la ila)
Djali yo yow la ila jalay (djali yo yow la ila jalay)
Djali yo yow la ila (djali yo yow la ila)
Yow yag nga ngagnu begel barki demb ba tay
Djali kora foniay (abora)
Djali bala foniay (iciya)
Djali n’goni foniay (n’dela)
Djali tama foniay (abora)
Djali kora foniay lay
Katay lou ma lon djali lay bora moho djoma ni moho djoma ma sora
Fakouly koumba, ani fakouly daba lay
Boulakha finlandi boulama finlandi lay
Djali kora foniay (abora)
Djali bala foniay (iciya)
Djali n’goni foniay (n’dela)
Djali kora foniay lay
La ilaha illa lah sama gagni contaana ci yeene
Mi’gmafrica yeena teygey li, ma contaane ci yeene, waw diko may gewelu Senegal
Diko may sama famille banaya family
Waw, ndaxtay wolof njaay dafanay
Li nga done sooko bagnay dafa fek nga geyn cay gnaaw waw
Ay gewel legnu kay
Waw waw Mi’gmafrica yeena teygey li
Mi’gmafrica mba pare ngeene
Montréal mba pare ngeene
Dakar mba pare ngeene
Senegal mba pare ngeene
Gnu dellu fa cay regaka
Waw waw li ngeen di def dafa neex waw leegi degluma rek
Ndеgeen di naan
Waw waw waw sama gaayi fi ngeene tayyay foofu neexna
Nagnu fa dellu waat
Rek gnu dеyg jaama
Ay ca leene
Gnu dem
Djali yo yow la ila
Djali yo yow la ila jalay (djali yo yow la ila jalay)
Djali yo yow la ila (djali yo yow la ila)
Yow yag nga ngañu begel barki demb ba tay (yow yag nga ngañu begel barki demb ba tay)
Djali kora foniay (abora)
Djali bala foniay (iciya)
Djali n’goni foniay (n’dela)
Djali tama foniay (abora)
Djali kora foniay lay (Djali kora foniay lay)
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Djali kora foniay
Find more lyrics at https://dcslyrics.com
![DCSLyrics.com Amazon Music](https://dcslyrics.com/wp-content/uploads/Amazon-Music.png)
![DCSLyrics.com Apple Music](https://dcslyrics.com/wp-content/uploads/Apple-Music.png)
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Migmafrica – Ding ding
Ani – AFY
Migmafrica Lyrics – Djali Kora
Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.
Release Year: 2023