![Jay 21 Hasta la vista](https://dcslyrics.com/wp-content/uploads/jay-21-hasta-la-vista.jpg)
Jay 21 – Hasta la vista Lyrics
Artist: Jay 21
Song: Hasta la vista
Hasta la vista
Gucci ci mbaggou mamacita
Maybe ma nangou sa señorita
Rappeur bou kheuw niou tak roll
Ouh oh oh ohhhh
Nenagn dagnouy fight mais sen bros ci sama side
Nio leine eup tiay-tiay te gun dou beurré kay check
Hasta la vista
Retane sa docteur melni sida
Dagnou oser mane ma oser forêt tak bone yi casse gin kay Check
Mane lima diekhal geune fouf fouf lima tamalé ci meune nga latché
Ma beurri flow beu moudjou justice awma keuyite niou youkhou satché
Yok Diom beu romb dji Cris fils
No dou football quartier
Sen rappeur lagn déclarer syphilis
Sen cheveux niou babylis
Sеne carrière niou tiap-sif
T dou adio sacrifice
Sama n#gg#s di mеlni ay lafagn, bou tiole keneu dou ci daw
Sama n#gg#s yi di melni ay moumeu, bou tiole keneu dou ci wakh
Hasta la vista
Keneu ci niom douma diss fils
Ma leine geuneu diss fils
Gni meu geuneu siss djiss
Gni leu geumoul dissmiss
Nenagn dafa andeu ak ibliss
Keneu ci niom douko diss fils
Niom nieup ma leine geuneu diss fils
Tolo beut t bokouniou guiss guiss
Hasta la vista
Gucci ci mbaggou mamacita
Maybe ma nangou sa señorita
Rappeur bou kheuw niou tak roll
Ouh oh oh ohhhh
Nenagn dagnouy fight mais sen bros ci sama side
Nio leine eup tiay-tiay te gun dou beurré kay check
Hasta la vista
Retane sa docteur melni sida
Mc’s y’a ngui geuneu frokh tolou
Ko ci Romb mou ngui Torokh Torope
Gat xel ni xelou crop-top
Jay punch yi dale lolou rap frappe
Ma rap nga djiss ko loloy horoscope
Wax bi leroul da nga diolox forokh
Nenagn ndiago bi dafa Wolof torope
Sagnsé def dal croco
Sa baby nena dama sokhor torope
A riba riba riba riba talatouma fight dama kolotch dokh
La Chica chica chica mucho gracias dougnou insister ni dalal tone
Dama sikeu sikeu sikeu sikeu takhaw d ma geuneul souk maral bok
Mane all around nga djiss sissou
Kou nek tal sa bop Sénégal beneu bop leu do djiss Zizou
Kou mounoul yek nga meune beuss mou watch sale fils de puta fils de fripouille
Diam geuneu neu diam geune neu xar nga yalla xar nga yalla foum leu djissoul
Lougnou poup nga lek dissoul
Hasta la vista
Gucci ci mbaggou mamacita
Maybe ma nangou sa señorita
Rappeur bou kheuw niou tak roll
Ouh oh oh ohhhh
Nenagn dagnouy fight mais sen bros ci sama side
Nio leine eup tiay-tiay te gun dou beurré kay check
Hasta la vista
Retane sa docteur melni sida
Find more lyrics at https://dcslyrics.com
![DCSLyrics.com Amazon Music](https://online-tips.jspinyin.net/wp-content/uploads/Amazon-Music.png)
![DCSLyrics.com Apple Music](https://online-tips.jspinyin.net/wp-content/uploads/Apple-Music.png)
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Jay 21 – Kouy sa baay
Jay 21 – Bùl Bidënti
Jay 21 Lyrics – Hasta la vista
Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.
From the album:
IVK [Explicit]
Release Year: 2021