Ismaël Lô (SEN) – Mbindane

Ismaël Lô (SEN) Mbindane

Ismaël Lô (SEN) – Mbindane Lyrics

Artist: Ismaël Lô (SEN)
Song: Mbindane

Mbindane dou diam mbindane dou
Diam mbindane dou ndiam
Mbindane dane sa dolela
Mbindane dou diam mbindane dou

Diam mbindane dou ndiam
Mbindane dane sa dolela
Mama mamee
Mbindane dou none mbindane dou

None mbindane dou none
Mbindan dane sa dolela
Mbindane dou none mbindane dou
None mbindane dou none

Mbindane dane sa dolela
Mama mamee
Bou sagnone doufi gneuw dane si doleme
Bou mamone doufi gneuw dane si doleme

Bou amone doufi gneuw dane si doleme
Mama mamee
Mbindane dou diam mbindane dou
Diam mbindane dou ndiam

Mbindane dane sa dolela
Mbindane dou diam mbindane dou
Diam mbindane dou ndiam
Mbindane dane sa dolela

Mama mamee
Dafa dane si doleme
Dafa woutssi dole
Bilay mbindane dou diame

Mbindane mbindane guarmi la kay
Dafay kheuye dieul bale keurgui
Tatch ndekili khar midi diote mou tadial la
Nagua khol linko yan ak link kay fay

Mba diarnako
Kone teyeko ni kigua diour
Diapako ni ki sa yaye la
Mangui fatiliko bamay ndaw

Dama done yakamti andak mome kereum
Moumay topato ni sama yaye la
Mane diapana ni sama yaye gua
Walay yaw sama dome gua

Walay yaw sama kharit gua
Mbindane mbindane guarmi la kay
Heu mbindane dou diame
Domou dianmbourla

Kone bouko misere lo yaw
Heu mbindane dou diam
Find more lyrics at https://dcslyrics.com

You can purchase their music thru
DCSLyrics.com Amazon Music    DCSLyrics.com Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases

Ismaël Lô (SEN) Lyrics – Mbindane

Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.

Release Year: 2006