Ashs The Best – Pottu Ndaa

Ashs The Best Pottu Ndaa

Ashs The Best – Pottu Ndaa Lyrics

Artist: Ashs The Best
Song: Pottu Ndaa

Gisoo ni fu sori la joge
Ba ñuy gone dañ foogoon ni
Boo maggee Loo yootu day gaaw
Tera’nga bi day naxe ci boo foogee Lepp yay boroom

Adduna bi pottu Ndaa la soo naanee
Jox sa moroom naan
Jamm du doy!!!
Du alal jamm moo li gën ci ñun

Nang xoolee sa bopp yeene ko peace and love and harmony
Lepp du yay boroom fii dang fi am waar keneen am fi waar
Saabu bi footul boppam
Man la man la lune nga ne yay boroom

Fii demal maa ngi ñëw la Tay sa bis suba bisam la
Boo goree jekkoo del baalee Adduna di ndaa yow
Soo naane jox sa moroom naan yow
Yaatu yaatalal sa xol yow

Jamm du doy!!!
Seet naa ba seet moy li gën si ñun
Mbëggeel akk alal du doy
Bu fi jamm nekkul dara xajjul si ñun

Saabu bi footul boppam
Man la man la lune nga ne yaa ko moom
Dimbalil xale bi mbokkam
Xoolal li nga yeene sa bopp

Yeene ko bepp jaam
Gisoo ni fu sori la joge
Ba ñuy gone dañ foogoon ni
Boo maggee Loo yootu day gaaw

Teranga bi day naxe ci boo foogee
Lepp yay boroom
Adduna bi pottu ndaa la
Boo naanee jox sa moroom naan
Find more lyrics at https://dcslyrics.com

You can purchase their music thru
DCSLyrics.com Amazon Music    DCSLyrics.com Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases

Ashs The Best Lyrics – Pottu Ndaa

Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.

From the album:
Dibèer
Release Year: 2021