
Admow – Boula Dara Meti Lyrics
Artist: Admow
Song: Boula Dara Meti
Yena say nga fok ni thi adouna bi keneu doula comprendre
Sometime nag dem ba diap ni doto museu contan
Ci bir keur gui Yaye boye nela doula meye nada
Ci mbeda bi yeah yeah
Ragala takh ngani do maye dara
Mais nak boul diakhle, yone leu mou diaffe
Want maadi goor bi kham fi nga feete
Kham sa ndieuga takh ma deukh thi di niaafe yeah yeah
Thiofeleu ci bir khol bi
Diox ma confiance ma yoboula fu sorri
Ou bebe oh bebe
Damala love love love baby love love love
Boula dara mеti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wetе
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti
Ecoute moi baby
I love you lady
Et je sais que t’as peur de m’aimer
Si tu t’inquietes pour moi t’as tord
Faut que tu sort de ton decors
T’as deja gagner mon coeur
Donne moi ma chance
Fais un effort
Soumala xole guiss thi yow ku am ndiom
Douma beugua loudoul done sa heros
Do wete thi bile yone you are not alone
Je suis ton ange gardien
Ohhhh
Baby you’re the one, baby you’re the only one
Baby you’re the one that i need in my life
Damala love love love baby love love love
Boula dara meti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti
Damala love love love baby love love love
Boula dara meti
Nakhar diekh na tey mangi thi sa wete
Boula dara meti
Dinala thewal thi nadj
Thewal la thi kerr
Baby i got your back
Boula dara meti
Find more lyrics at https://dcslyrics.com


Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Boula Dara Meti Lyrics – English Translation
YENA SAY NGA FOK NI THI ADOUNA BI KENEU DISLA UNDERSTANDING
Sometime nag dem ba diap or doto museu contan
CI BIR KEUR GUI YAYE BOYE NELA DOULA MEYE NADA
Ci mbeda bi yeah yeah
Ragala Takh Ngani do Maye Dara
But Nak Boul Diakhle, Yone L’soft diaffe
Want Maadi Goo Bi Kham Fi Nga Feete
Kham Sa Ndieunega Takh Ma Deukh Thi di Niaafe Yeeh Yeah
Thiofeleu CI Bir Khol BI
Diox my confidence my yoboula fu sorri
Or baby oh baby
Damala Love Love Love Baby Love Love Love
Boula Dara Meti
Nakhar Diekh Na Tey mangi thi sa wetе
Boula Dara Meti
DININA THEWAL THI NADJ
Thewal La Thi Kerr
BABY I GOT YOUR BACK
Boula Dara Meti
Listen to me baby
I Love You Lady
And I know you’re afraid to love me
If you’re worried about me you’re wrong
You have to get out of your decors
You’ve already gained my heart
Give me my luck
Make an effort
SOUMALA XOLE GUISS THI YOW KU AM NDIOM
Duma Beugua Loudoul does his heros
Do wete thi bile yone you are not alone
I am your guardian angel
Ohhhh
Baby You’re The One, Baby You’re The Only One
Baby You’re The One That I Need in My Life
Damala Love Love Love Baby Love Love Love
Boula Dara Meti
Nakhar Diekh Na Tey Mangi Thi Sa Wete
Boula Dara Meti
DININA THEWAL THI NADJ
Thewal La Thi Kerr
BABY I GOT YOUR BACK
Boula Dara Meti
Damala Love Love Love Baby Love Love Love
Boula Dara Meti
Nakhar Diekh Na Tey Mangi Thi Sa Wete
Boula Dara Meti
DININA THEWAL THI NADJ
Thewal La Thi Kerr
BABY I GOT YOUR BACK
Boula Dara Meti
Find more lyrics at https://dcslyrics.com
Admow Lyrics – Boula Dara Meti
Please support our site by sharing it.
And please follow our site to get the latest lyrics for all your favourite songs.
Please support the artist and us by purchasing your favourite music thru our Amazon Music and Apple Music links 🙂


Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
From the album:
Aol
Release Year: 2019